25/08/2023
V
Innaa lillaahi wa ina ilayhi raajihunn.
Tiis dileen yëgal wàccug liggeeyu Sëriñ mustafaa buso baaxer (1939 - 2023) nekkoon xalifa sëriñ baaxer buso moom sëriñ Mbàkke buso nekkoon ku ragal yalla lool té bari xam xam ,nekkoon na itam imaam raatib bu Gede Buso moo daan taxawé itam calendrier ramadan ci biir Sénégal gèpp .yatalon liggeeyub mamam s mbacke Bousso lol.
Tiis wu keemaané moo dal ci kaw yoonu murid rawatina waa GEDE BUSO
Wax nanu né natt na lu ëpp 500 mosquée ngir jubalé leen xibla. Jiité na ci jumaau Guede lu mat 30 ans.
LAÑUKAY JÈBBAL BROOMAAM